Al Murtadaa tv

Al Murtadaa tv Ab séen la ngir lépp lu aju ci mbiri diine

11/08/2024

Par Serigne Mourtada Ndiaye

♥️
07/08/2024

♥️

الشيخ مرتضى إنجاي يعد رمزًا من رموز العلم والتقوى في أسرة إنجاي والمريدين بشكل عام. يمتاز بعلمه الغزير، ورعه، وتقواه الت...
31/07/2024

الشيخ مرتضى إنجاي يعد رمزًا من رموز العلم والتقوى في أسرة إنجاي والمريدين بشكل عام. يمتاز بعلمه الغزير، ورعه، وتقواه التي تبرز في جميع أفعاله وأقواله. ورغم مكانته العالية، إلا أنه يظل متواضعًا، لا يسعى للشهرة ولا للظهور، بل يركز على خدمة الدين والمجتمع بصمت وإخلاص. تواضعه يعتبر درسًا عظيمًا لكل من يسعى للسير على خطاه، ويجعل محبته في قلوب الناس أكبر وأعمق.

إلى جانب ذلك، يُعرف الشيخ مرتضى بجهوده في نشر العلم الشرعي، وتعليم الناس أمور دينهم بطريقة ميسرة وسهلة الفهم، مما جعله محل احترام وتقدير من قبل الجميع. تأثيره الإيجابي يظهر بوضوح في المجتمع، حيث يُعتبر قدوة حسنة لكل من يسعى للالتزام بقيم الدين الإسلامي وتعاليمه السامية.
طالبك مختار طه انجاي
حفظك المولى وجزيت خيرا
الكاتب مختار طه

30/07/2024

Lan mooy Murit
Saadig ak lan mooy
melukaanu Murit.......par Serigne Mourtada Ndiaye

30/07/2024

Maamum bi toppci
ginnaaw gis mu def loo
xam ne daganul mu wéy...par Serigne Mourtada Ndiaye

30/07/2024

lan mooy sababu
Tamxarit....par Serigne Mourtada Ndiaye

30/07/2024

Ndax kiy dugg ci jakk
daa wara wax ca kaw.....par Serigne Mourtada Ndiaye

30/07/2024

Ki yor werd maaxuuz
ndax bu fajar gi xaree
te julleegul sañ nakoo....par Serigne Mourtada Ndiaye

30/07/2024

nit faatu ba am 40
jour ñu daje di ko ñaanal
ndax aada la wala diine.....par Serigne Mourtada Ndiaye

30/07/2024

ban julli moo gen
ci ab neew ñu diko.....par Serigne Mourtada Ndiaye

30/07/2024

Attey Lihaan.....par Serigne Mourtada Ndiaye

30/07/2024

Al xuruuju......par Serigne Mourtada Ndiaye

30/07/2024

Booy jënd kilay jaay ne
bu dee léegi ngay fay
5000 la bu dee ndànk ak......par Serigne Mourtada Ndiaye

30/07/2024

Laaj ak tontu ci diine par Serigne Mourtada Ndiaye

30/07/2024

Tafsiir par Serigne Mourtada Ndiaye

30/07/2024

Xale bu ndaw bi
ndax bu jullee te yorul
njapp julli.ga baax na.....par Serigne Mourtada Ndiaye

30/07/2024

Ndax dagan na ci
ab jullit muy takk
montr....par Serigne Mourtada Ndiaye

30/07/2024

Nit ki nga xam ne
daa am neenti Soxna
ba noppi dem takk
Juroomeel....par Serigne Mourtada Ndiaye

23/07/2024

Nganéeli yàlla akiy mayam xajul ci.....par Serigne Mourtada Ndiaye

13/07/2024

Xutbatu wamsasin bu Sëriñ Muhammadu Lamiñ Jóop Dagana.....par Serigne Mourtada Ndiaye

06/07/2024

Ñaan gi nuy def ci fan wu mujj ci atum gàddaay gi...par Serigne Mourtada Ndiaye

Adresse

Touba

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Al Murtadaa tv publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Vidéos

Partager

Entreprises De Médias á proximité



Tu pourrais aussi aimer