Al Fadaliyah Tv L'officiel

Al Fadaliyah Tv L'officiel القناة المرجعية
في قلب الم

La Chaîne de Référence
Au cœur des évènements culturels et religieuse

Aladji Fallou moom Seriñ Ibrahim Khalil moom Aladji Fallou  ❤️❤️❤️
27/01/2025

Aladji Fallou moom Seriñ Ibrahim Khalil moom Aladji Fallou ❤️❤️❤️

Wakeur Serigne Abdou Aziz Bara Mbacke diokhé nanou 10million adiya Serigne Moustapha Mbacke Khalife Cheikh Mouhamadou La...
27/01/2025

Wakeur Serigne Abdou Aziz Bara Mbacke diokhé nanou 10million adiya Serigne Moustapha Mbacke Khalife Cheikh Mouhamadou Lamine bara Mbacke yallna sén takhaway yag Mbacke

Mame Serigne Mbousoobe Moom S Fallou Mbacke
26/01/2025

Mame Serigne Mbousoobe Moom S Fallou Mbacke

Alhadji Muhammadul Aamiin Baara Mbàkke moom Sëriñ Fàllu moo Bole Niari Xalifa Nek Xalifa Wajuram Sëriñ Fàllu Mbàkke 2000...
25/01/2025

Alhadji Muhammadul Aamiin Baara Mbàkke moom Sëriñ Fàllu moo Bole Niari Xalifa
Nek Xalifa Wajuram Sëriñ Fàllu Mbàkke 2000 - 2010
Nek it Sëut bi Njekk a took Xalifa Sëriñ Tuubaa 2007 - 2010
Yalla Nanu ko Yalla Fayal Yok Ay leeram Nguereum ko Barkeb Seexul Xaadim

Titre : Gamou Nigeria 2025 : Hommage à Cheikh Al-Islam El Hadji Ibrahima Niass
25/01/2025

Titre : Gamou Nigeria 2025 : Hommage à Cheikh Al-Islam El Hadji Ibrahima Niass

Une journée de prière sera consacrée à la mémoire de Serigne Mahmoudane Mbacké (Khary Lô), une figure éminente de la com...
25/01/2025

Une journée de prière sera consacrée à la mémoire de Serigne Mahmoudane Mbacké (Khary Lô), une figure éminente de la communauté mouride, disciple dévoué et érudit accompli.

Il porte le nom de Mahmoudane At-Tandakhiyou, le grand disciple mauritanien de Cheikh Ahmadou Bamba, qui fut le muezzin de la mosquée du Cheikh à Diourbel. Il faisait partie de ceux à qui Cheikh Ahmadou Bamba avait confié la charge de son lavage mortuaire.

« Cheikh magi Dane Khary » ou « Maami Dan’ak Cheikh ». Ces propos de chanteurs témoignent de l’harmonie et de la fraternité exemplaire qui existaient entre Serigne Mahmoudane et ses frères.

Fils de la noble lignée de Khadim Rassoul, originaire de Ndam et de Koki, Serigne Dane Khary Lô fut un éducateur remarquable. Il consacra sa vie au service des créatures d’Allah et se démarqua par son dévouement, son humilité et son sens de l’humour. Très aimé de ses parents, disciples et amis, il se montrait généreux envers tous. Sa demeure était un lieu d’accueil ouvert à tous, un refuge pour les nécessiteux et un espace d’entraide.

Son décès, survenu le 25 Rajab 1406 (1986), à l’âge de 68 ans, fut une perte immense pour la communauté mouride. Cependant, son héritage perdure à travers ses descendants qui perpétuent ses valeurs et son engagement.

Qu’Allah lui accorde Sa miséricorde et l’élève dans les rangs des bienheureux.

Soxna Maam Jaara Gëy mii mooy ki njëkka mokkal Alxuraan ca Daara Maam Jaara ji ci Poroxaan, ci attum 2007. Bis bimu mokk...
25/01/2025

Soxna Maam Jaara Gëy mii mooy ki njëkka mokkal Alxuraan ca Daara Maam Jaara ji ci Poroxaan, ci attum 2007. Bis bimu mokkale la Sëriñ Mustafaa Basiiru wax ni mission bimu doon dox mat na, diir bu gàtt lañu ca teg mu génn àdduna. Tay jii jàngal na lu jege fanweeri(30) Maam Jaara ba ñu mokkal Alxuraan ca Daaray Poroxaan!

Cheikh Oumar Tall ❤️ a dit :﴾Celui qui souhaite accomplir le Wird du matin avant l’aube, durant le dernier tiers de la n...
23/01/2025

Cheikh Oumar Tall ❤️ a dit :﴾Celui qui souhaite accomplir le Wird du matin avant l’aube, durant le dernier tiers de la nuit, peut le faire, car cela comporte une immense récompense. En effet, une seule récitation de Salatoul Fatihi durant le dernier tiers de la nuit équivaut à 500 récitations faites en dehors de la nuit. Toutefois, si l’aube apparaît avant qu’il n’ait terminé le Wird, celui-ci n’est pas valable, même s’il ne lui reste qu’une seule récitation de ‘La ilaha illa Allah’. Dans ce cas, il est nécessaire de reprendre intégralement le Wird, car il l’a commencé avant son heure déterminée, dans le cadre d’une autorisation et d’une facilité. Mais si l’heure fixée arrive avant qu’il ne l’ait achevé, il doit impérativement recommencer depuis le début.﴿

Sëriñ Basiiru Mbàkke Abdu KariimSëriñ Fàllu Mbàkke xalifa Sëñ Cerno Gelongal
22/01/2025

Sëriñ Basiiru Mbàkke Abdu Kariim
Sëriñ Fàllu Mbàkke xalifa Sëñ Cerno Gelongal

Ki ñu ko tudde rene mooy Sëriñ Muusaa Ka Na ko ñépp waajal
22/01/2025

Ki ñu ko tudde rene mooy
Sëriñ Muusaa Ka
Na ko ñépp waajal

Sëriñ Mustafaa Ibnu Sëriñ Basiiru ak rakam Sëriñ Daam Atta Ibnu Sëriñ Ibraahima, Yàlla na yàlla yokku seeni leer te tass...
22/01/2025

Sëriñ Mustafaa Ibnu Sëriñ Basiiru ak rakam Sëriñ Daam Atta Ibnu Sëriñ Ibraahima,
Yàlla na yàlla yokku seeni leer te tass ñu çi seen barké

22 Janvier 2021 - 22 Janvier 2025 : 4 ans que nous quittait Serigne Atou Diagne.Que son âme repose en paix et que son ex...
22/01/2025

22 Janvier 2021 - 22 Janvier 2025 : 4 ans que nous quittait Serigne Atou Diagne.
Que son âme repose en paix et que son exemple continue d’inspirer notre nation.

" Ne croyez pas que ceux qui ont œuvré en bien dans les sentiers de Dieu sont morts. Ils sont bien VIVANTS. Ils sont pourvus de biens auprès de leur seigneur. Ils sont heureux de la grâce que Dieu leur a accordée. Ils se réjouissent parce qu’ils savent que ceux qui viendront après eux et qui ne les ont pas encore rejoints n’éprouveront plus aucune crainte et qu’ils ne seront pas affligés..."

SERIGNE MOUSTAPHA MAÏ MBACKÉ. Ibn👉soxna maïmounatou mbacké kubra moom soxna aminta kany bousso moom mam mboussobe Bousso...
21/01/2025

SERIGNE MOUSTAPHA MAÏ MBACKÉ.

Ibn
👉soxna maïmounatou mbacké kubra
moom soxna aminta kany bousso
moom mam mboussobe Bousso
moom Soxna Asta Walo Mbacké
moom Ahmadu Soxna Bousso
Moom Mam Marahm Mbacké
Mam mboussobe Bousso it
moom Mam Matabara Bousso
Moom Mam Hamad Bousso
Mam Borom Touba
moom Soxna Diarra Bousso
moom Soxna Astou Walo Mbacké
moom mam Ahmadu Soxna Bousso Mbacké moom
Mam Marahm Mbacké,
Soxna Diarra Bousso
moom mabousso Awa Mbaye bousso
moom mam matabara Bousso
Mam Borom Touba it
Moom Mam Mor Anta Sally Mbacké
moom Mam Balla Aïcha Mbacké
moom Mam Marahm Mbacké AK Soxna Aïcha Kane.
Mam Mor Anta Saly Mbacké it
moom soxna Anta Sally Kane
moom Soxna Saly lô
moom mam Dam Boury samb lô
moom Balla mbeurgou seneba gaye lo
moom Demba Binta lô
moom mam maxtarum Dam lo
moom Mam Dam Issa lo

ak

👉 SÉRIGN MODOU HABIB MBACKÉ
moom soxna marem balla syll
moom Serigne Marina syll
moom sokhna khary diakhte diop
moom massamba khary diakhte diop
moom massamba fakhoudja Diop
moom makhtar ndoumbe diop
moom Mame samba ayib diop

sokhna marem balla syll it
moom sokhna faty kodé diop
moom Matin bator diop
moom Balla maram diop
moom mafatim diop
moom Balla maram diop
moom Samba ayib diop

Serigne Modou Habib it
moom Mame Thierno Mbacké
moom soxna faty issa diop
moom Sérign ndiaga Issa Diop
moom Serigne Modou fa xudia Diop
moom Mam maxtaar ndumbe diop koki.

Mam ndiaga Issa Diop it
moom Soxna Issa diey lô ndack Kandy
moom Mam Balla mbeurgou lô
moom mam Demba Binta lô
moom mam maxtarum Dam lo
moom mam Dam Issa Lo

Soxna Issa Diop it
moom Soxna Absa laobé Mbacké
moom Mam Ahmadou Soxna Bousso Mbacké
moom Mam Marahm Mbacké

AK

Mam Mor Anta Sally Mbacké
moom Mam Balla Aïcha Mbacké
moom Mam marahm Mbacké AK Soxna Aïcha Kane.

Mam Mor Anta Saly Mbacké it
moom soxna Anta Sally Kane
moom Soxna Saly lô
moom mam Dam Boury samb lô
moom Balla mbeurgou seneba gaye lo
moom Demba Binta lô
moom mam maxtarum Dam lo
moom Mam Dam Issa lo

yalnaa suniu borom taas cii barkem yagaal fi njaboot gui🙏🙏
Amadu Faal njay ✍️✍️

Touba midina sarr Serigne cheikh Sarr Khalifa Serigne mbacke sarr Mom cheikh Ibrahima Sarr ndiagne Cheikh Abdou lahat sa...
20/01/2025

Touba midina sarr
Serigne cheikh Sarr
Khalifa Serigne mbacke sarr
Mom cheikh Ibrahima Sarr ndiagne
Cheikh Abdou lahat sarr cheikhouna

Serigne Abdoullahi appartient à la descendance du Prophète Muhammad (PSL) de par sa mère Sokhna Fatima Koubra Al kuntiyu...
20/01/2025

Serigne Abdoullahi appartient à la descendance du Prophète Muhammad (PSL) de par sa mère Sokhna Fatima Koubra Al kuntiyu, petite-fille de Cheikh Sidya El Moukhtar Al kuntiyu, appelé Cheikh Sidya Baba un illustre saint qui vivait en Mauritanie et considéré comme le propagateur de la voie Khadre dans ce pays.
Dans son ouvrage Irwaou Nadim Min Adhbi Hub Al-Lhadim (l'Abreuvement du commensal dans la Source d'Amour du Serviteur), Cheikh Mouhammadou Lamine Diop Dagana évoque l'amitié empreinte de respect qui liait Cheikh Ahmadou Bamba et Cheikh Sidya Baba. Ce dernier aurait même composé ces vers à l'endroit de Cheikhoul Khadim.
_Cheikh Ahmad est un bienfait
_Que le Seigneur a accordé aux hommes
_Le Cheikh n'est qu'une faveur
_Que Dieu nous a accordé, un de ses signes.

On rapporte que le Cheikh fut très heureux de la naissance de Cheikh Abdoullahi et confia à ceux qui lui rendaient visite que Dieu l'avait gratifié d'un illustre hôte qui était venu au monde avec beaucoup de prédispositions. C'est à cette occasion qu'il écrivit le Khassida Minal Haqqi qui fait l'éloge du Coran. Cheikh Ahmadou Bamba décrit le Livre Saint comme "une vérité accompagnée de lumière qui est apparue en provenance de la Vérité (Dieu) et dont le réceptacle est le Prophète (PSL) qui est l'Envoyé de la vérité... Le Coran est la clé pour gagner la miséricorde divine, l'absolution, la protection et le bonheur ici-bas et dans l'au-delà ". Cheikhoul Khadim décrit le Coran comme " son trésor, sa banque florissante ". Dieu lui a transmis manifestement et secrètement ses bienfaits à travers le Coran, lui a dévoilé ses mystères et lui a soumis ses ennemis. Il s'est rapproché de son Créateur par Livre Saint. " Le Coran chasse la disette et apporte la prospérité ". Comme on le verra plus t**d, la vie de Serigne Abdoullahi est synonyme de prospérité.

Le Cheikh plaça le Khadsida Minal Haqqi entre deux morceaux de bois et le mit devant la porte de la chambre où se trouvait le nouveau né et dit : " Quiconque poserait les yeux sur ce Khassida sera absous de ses péchés ".

Il écrivit sur un bout de papier le prénom de "Abdoullahi" et ordonna à Serigne Moukhtar Binta Lô de dire à Serigne Amsatou Diakhaté de baptiser ainsi le nouveau-né. Comme on peut le deviner, le choix de ce prénom est lourd de sens -Abdoullahi, signifiant Serviteur de Dieu- n'est pas fortuit pour un homme qui a consacré sa vie à Allah et son Prophète (PSL) et dont chaque acte était régi par la foi et le désir de complaire à son Seigneur. Et Cheikh Ahmadou Bamba avait pour but d'être Abdoullahi wa Khadimu Rassoulihi (Esclave de Dieu et Serviteur de son Prophète(PSL)). Par la suite, Serigne Abdoullahi a été appelé de différentes façons : Serigne Abdou, Serigne Abdou Aziz, Serigne Abdou Rahmane, Borom Dër Bi...

Extrait de
Serigne Abdoullahi Mbacké
Borom Dër Bi
Le Visionnaire de Darou Rahmane
Par Marième Ndir

Khalifa S Dame Atta Mbacke S Cheikh Gainde Fatma Mbacke dit  S Cheikh Wilaaya Moom S Dame Ata Mbacke Yàlla na Yàlla guda...
20/01/2025

Khalifa S Dame Atta Mbacke
S Cheikh Gainde Fatma Mbacke dit S Cheikh Wilaaya Moom S Dame Ata Mbacke

Yàlla na Yàlla gudal fanwi yoku weergui woyafal yéen bi si Barkep Serigbebi

Serigne Bara Touré Madina Touré Moom  Serigne Mor Faty Toure Donoone Khalifam Yàlla nako Yàlla dolli yeurmandee ak Ndieg...
19/01/2025

Serigne Bara Touré Madina Touré Moom Serigne Mor Faty Toure Donoone Khalifam
Yàlla nako Yàlla dolli yeurmandee ak Ndiegal si Barkep Serigbebi

S Mor Faty Toure Moom S Abdoulahi Toure Ak Sokhna Faty Anta Mbacke Moom Serigne Mor Anta Saly

Mingui Ganee aduna 1873 Thia Prokhane
Gueneu aduna 1960 sa Madina Toure

Serigne Mor Faty Anta Toure Brome Madina Toure
Bokoone Si Magui Seringebi, S mor Faty Anta Touré yaayam ak Mam Cheikh Anta ñoo bokk ndeye ak baay

Amna ñaar ñu mësa fékk i Seriñ Tuubaa (قاد له الله مااختار له) Gànnaar, ndox xawleen a jafe. Am ci koo xamne daa wax ne ...
19/01/2025

Amna ñaar ñu mësa fékk i Seriñ Tuubaa (قاد له الله مااختار له) Gànnaar, ndox xawleen a jafe. Am ci koo xamne daa wax ne du nuyu Seriñ Bi ngir ñàkk a laab. Ba muy jox Seriñ Bi loxo muur ko ngir wormaal Seriñ Bi.
Loola mujjoon na tax mu xam lu bari ci Baatin.

(Melnane ci loolu la ñuy gëna xamne am na mbir yoo xamne likay maye mooy téggiin wala ñu wax ne ag taalube waaye du am njàng. Wàllaahu Ahlam)

Jataayi texe, Seriñ Al Haaji Mbàkke

Adresse

Touba

Téléphone

+221766315544

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Al Fadaliyah Tv L'officiel publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à Al Fadaliyah Tv L'officiel:

Vidéos

Partager