DEVE parle en wolof

DEVE parle en wolof DEVE parle en wolof

Jigéen ju të xaalis, mucc yomb ko, aw xas teggi ko mook ak njabootam.
24/01/2023

Jigéen ju të xaalis, mucc yomb ko, aw xas teggi ko mook ak njabootam.

Xeex bi jéggi na SONKO!Dadi xeex bu nekk dina am kuy nekk ca kanam niki mbooloo yépp, waaye jëmmi xeex mooy lii, dëkkee ...
24/01/2023

Xeex bi jéggi na SONKO!

Dadi xeex bu nekk dina am kuy nekk ca kanam niki mbooloo yépp, waaye jëmmi xeex mooy lii, dëkkee naan meew mi di ñu jox neefere yi lees bëgg mu dakk.

Sonko kenn kepp la ci nun!

Cëy MAKI!  (Tagatembe) SONKO di la dàq, coowal ñetteelug kay kar la!Sa fetal gi de moo la dese! Ndax dinga ko tal kay mo...
24/01/2023

Cëy MAKI! (Tagatembe) SONKO di la dàq, coowal ñetteelug kay kar la!

Sa fetal gi de moo la dese! Ndax dinga ko tal kay mooy laaj bi?

Fii, am na RÉEW mum may nuróol de!Daa mel ni joxaat nañu leen démb sax!
24/01/2023

Fii, am na RÉEW mum may nuróol de!

Daa mel ni joxaat nañu leen démb sax!

Mbete man ab rëbóo laa ba duma xalaat!Dinaa jël sama doom yóbb(arme) ñu dàq ko(libere) ko ne ko soxla wuñu la, mu dem ba...
24/01/2023

Mbete man ab rëbóo laa ba duma xalaat!

Dinaa jël sama doom yóbb(arme) ñu dàq ko(libere) ko ne ko soxla wuñu la, mu dem ba jamono jii ñu xam ni am na fu Réew mi jëm, ñu ne ma sa doom jiñ dàqoon na ñëwaat rayanteel ñu, te mu leer la ne bu yii jàllee du fa toog dañu koy dàqaat nde daa am lees koy doye rekk.

Dinaa bàyyiwaat sama doom jooju muy bokki ca ñay faagaagal aw askanam? Maa lànk.

Ndokk ba fekkoon na ko ci beneen liggéey sax!(demul de) kenn du taqal samaw askan deret ngir alal man.

Coupe du Monde Qatar 2022Joŋante 8e de finale yu dinañu ko tàmbali tay ji ci bu 15h jote, Olaand 🇳🇱 mooy laale ak Aameri...
03/12/2022

Coupe du Monde Qatar 2022
Joŋante 8e de finale yu dinañu ko tàmbali tay ji ci bu 15h jote, Olaand 🇳🇱 mooy laale ak Aamerig 🇺🇲. Bu 19h jote dinañu amal ñaareelu joŋante bi, Arsantin 🇦🇷 mooy daje ak Óstraali.

Ñaari joŋante yi ñisi door ñooy daje ci 1/4 de finale yi !

Coupe du MondeÉkibu Senegaal tekk nañu ko ab daan ak koppar gu tollu ci juroom benni milyoŋ ci sunu xaalis, liko waral n...
02/12/2022

Coupe du Monde
Ékibu Senegaal tekk nañu ko ab daan ak koppar gu tollu ci juroom benni milyoŋ ci sunu xaalis, liko waral nag mooy bi Aliou Cissé waree janook taskati xibaar yi laata joŋante Équateur Senegaal, Aliou Cissé rekk moofa teew, te sart la ca Fifa nga teew ak benn futbalkat.

🚨 Manuel Neuer 🗣️: "Suñu ma woowee ci ekib bi dina ñëwaat".  🇩🇪🤝Ter Stegen kañ lay taxaw ci caaxu Allemagne yi 👀 #100%FO...
02/12/2022

🚨 Manuel Neuer 🗣️: "Suñu ma woowee ci ekib bi dina ñëwaat". 🇩🇪🤝

Ter Stegen kañ lay taxaw ci caaxu Allemagne yi 👀

#100%FOOTciWOLOF

Rafael van der Vaart : « Almaañ dafa am jafe-jafey jañkat. Niklas Süle nekkul futbalkat bu mag, dafa mel ni Harry Maguir...
02/12/2022

Rafael van der Vaart : « Almaañ dafa am jafe-jafey jañkat. Niklas Süle nekkul futbalkat bu mag, dafa mel ni Harry Maguire bu Almaañ rek ».

Uruguay bu Luis Suarez am na ndam ci kaw Ghana ñaari bal ci dara, waaye dafay ñibbi ndax wa Corée bu Heung-min Son ñoo d...
02/12/2022

Uruguay bu Luis Suarez am na ndam ci kaw Ghana ñaari bal ci dara, waaye dafay ñibbi ndax wa Corée bu Heung-min Son ñoo door wa Portugal ñaari bal ci benn, bi simili yi di waajal jeex ci lañu dugal sen ñaareelu bal, ba tax ñu taxawee ci ñaareelu taxawaay bi ak ñenti poñ, Uruguay itam ñenti poñ la am.
Kon Portugal bu Cristiano Ronaldo ak Corée bu Heung-min Son ñoo jàll ci ñaareelu xaaj bi.

Taxawaayu deuk yi ci keppango H
1) Portugal 🇵🇹 6 poñ +2
2) Corée 🇰🇷 4 poñ +0
3) Uruguay 🇺🇾 4 poñ +0
4) Ghana 🇬🇭 3 poñ -2f

Otto Addo mi tàggat wa Ghana tekki na nombal tànkam ! 🇬🇭
02/12/2022

Otto Addo mi tàggat wa Ghana tekki na nombal tànkam ! 🇬🇭

Qatar 2022 :Àttekatu Salvador bi di Iván Barton mom lañu tànn ngir mu àtte joŋante Angalteer - Senegaal.
02/12/2022

Qatar 2022 :
Àttekatu Salvador bi di Iván Barton mom lañu tànn ngir mu àtte joŋante Angalteer - Senegaal.

Sénégal 🇸🇳🤝 🇨🇲 Cameroun
02/12/2022

Sénégal 🇸🇳🤝 🇨🇲 Cameroun

Cameroun am na ndam ! 🇨🇲🇨🇲🇨🇲🇨🇲🇨🇲🇨🇲🇨🇲🇨🇲🇨🇲🇨🇲
02/12/2022

Cameroun am na ndam ! 🇨🇲🇨🇲🇨🇲🇨🇲🇨🇲🇨🇲🇨🇲🇨🇲🇨🇲🇨🇲

Camerun def na lu kenn xaarul woon ci monjaal bi, am ndam ci kaw Bereesil benn bal ci dara. Vincent Paté Aboubacar moo d...
02/12/2022

Camerun def na lu kenn xaarul woon ci monjaal bi, am ndam ci kaw Bereesil benn bal ci dara. Vincent Paté Aboubacar moo dugal bi joŋante bi di waajal jeex, waaye dafay mujjee ñibbi ndax Siwis dafa am ndam ci kaw Serbi ñetti bal ci ñaar.
Kon Bereesil ak Siwis ñoo jàll ci ñaareelu xaaj bi.

1) Bereesil 🇧🇷 6 poñ +2
2) Siwis 🇨🇭 6 poñ +1
3) Camerun 🇨🇲 4 poñ +0
4) Serbi 🇷🇸 1 poñ -3

Coupe du Monde8E DE FINALE
02/12/2022

Coupe du Monde
8E DE FINALE

Allemagne ❌Belgique ❌Danemark ❌
01/12/2022

Allemagne ❌
Belgique ❌
Danemark ❌

CI LU WER !Tàggatkatu Belgique bi di Roberto Martinez xamle na ni dafay bàyyi.
01/12/2022

CI LU WER !

Tàggatkatu Belgique bi di Roberto Martinez xamle na ni dafay bàyyi.

Ci ñetti joŋante yi :Passes - 1163 🏹Passes réussis - 956 ✅Tire - 34 🥅Tire cadrés - 13 🎯
01/12/2022

Ci ñetti joŋante yi :

Passes - 1163 🏹
Passes réussis - 956 ✅
Tire - 34 🥅
Tire cadrés - 13 🎯

Taxawaayu ndawi Aliou Cissé yi ci joŋante pul yi :3 Matchs 👕2 Victoires ✅ (🇸🇳 3-1 🇶🇦 / 🇸🇳 2-1 🇪🇨)1 défaite ❌ (🇸🇳 0-2 🇳🇱)...
01/12/2022

Taxawaayu ndawi Aliou Cissé yi ci joŋante pul yi :

3 Matchs 👕
2 Victoires ✅ (🇸🇳 3-1 🇶🇦 / 🇸🇳 2-1 🇪🇨)
1 défaite ❌ (🇸🇳 0-2 🇳🇱)
6 points 🧷
5 Buts marqués ⚽
4 Buts encaissés 🥅

Buteur : Boulaye Dia, Famara Diedhiou, Bamba Dieng, Ismaila Sarr ak Kalidou Koulibaly.

Passeur : Ismail Jakobs, Ilimane Ndiaye)

Carton jaune : Gana Gueye (2) Nampalys Mendy, Pathé Ciss, Ismail Jakobs, Boulaye Dia.

Yàlla de xam na ni nit ku bari Tuuma la, moo tax doo gis mukk ci Teereem bu Tedd fum njëkkee tudd Suuf ci Asamaan, waaye...
30/11/2022

Yàlla de xam na ni nit ku bari Tuuma la, moo tax doo gis mukk ci Teereem bu Tedd fum njëkkee tudd Suuf ci Asamaan, waaye jamono ju ne Asamaan lay jiital, ngir xam ni bu jiitaloon Suuf am ñu ne kon ci Suuf la taxawoon ngir tabax Asamaan.

Moo tax(خلق السماوات والإرض) rekk ngay dégg.

Wallaay ñoñ Kahfi ña ñoom Tamliixaa...ñoo yay waaru ci jant bi, lii ku ko xool xam ni moos kañu doon tudde buur defu ko fi, waaye am na keneen ku ko fi def...nde fi la ko kooka fekk, te amu cib sañ-sañ, te kenn manul a misaal lees ko defare ak nees ko defare.

Mbooleem lu fi nit man a def, ràpp na, raaf na, xomaag na, yàqu na, màbb na...yii fi Yàlla def nag moo ba Àddina sosoo ba tay nii mu mel la mel, lii ñuy dox la ñiy wëy di dox, duñ yoqi, duñ màbb, duñ xumaag, du ràpp, duñ raaf.

Te kenn amu ci man-man mbaa sañ-sañ, ken manu koo saytu ku dul Boroom...

Kenn la.

8E DE FINALE 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
30/11/2022

8E DE FINALE 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳

Gareth Southgate : «Seetan na joŋante xaritoo Sénégal Iran ca Vienne, jàng na leen bu baax. Bis niki tay dina leen gën a...
30/11/2022

Gareth Southgate :
«Seetan na joŋante xaritoo Sénégal Iran ca Vienne, jàng na leen bu baax. Bis niki tay dina leen gën a jàng seeni joŋante. Xam nañu ñenn ci seeni futbalkat yi futbal ca Angleterre ak ñi futbal ci championnat yu maggi. Ñun nag ñooy favori nangu nañu ko waaye ñi ngi futbal ak ekib bu yéeme.»

Daanaka déggoo mi ngi bëgg a am ci diggante Cristiano Ronaldo ak këlëb bi di Al-Nasser bu Arabie Saoudite. CR7 fas-yéene...
30/11/2022

Daanaka déggoo mi ngi bëgg a am ci diggante Cristiano Ronaldo ak këlëb bi di Al-Nasser bu Arabie Saoudite. CR7 fas-yéene nañ ko fay 200M€ ci at bu nekk.

8E DE FINALE Coupe du MondePays-Bas 🇳🇱 vs 🇺🇲 USA Angleterre 🏴󠁧󠁢󠁥󠁮󠁧󠁿 vs 🇸🇳 Sénégal France 🇫🇷 vs 🇵🇱 Pologne Argentine 🇦🇷 v...
30/11/2022

8E DE FINALE Coupe du Monde

Pays-Bas 🇳🇱 vs 🇺🇲 USA
Angleterre 🏴󠁧󠁢󠁥󠁮󠁧󠁿 vs 🇸🇳 Sénégal
France 🇫🇷 vs 🇵🇱 Pologne
Argentine 🇦🇷 vs 🇦🇺 Australie
??
??
??
??

30/11/2022

Aka maa sant Yàlla saa Boroom.🤔

Damaa rus sax ci ni mu ma dëkkee teral, te manu maa dëkk ci di ko jaamu.😭

🇸🇳🔗 Sunu Gaynde yi amal nañu sen tàggatu gu njëkk ca Qatar.
15/11/2022

🇸🇳🔗 Sunu Gaynde yi amal nañu sen tàggatu gu njëkk ca Qatar.

🇸🇳🔗 Sunu Gaynde yi amal nañu sen tàggatu gu njëkk ca Qatar.
15/11/2022

🇸🇳🔗 Sunu Gaynde yi amal nañu sen tàggatu gu njëkk ca Qatar.

Adresse

Touba
Rufisque
11494DAKAR

Téléphone

+221761309852

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque DEVE parle en wolof publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à DEVE parle en wolof:

Partager



Tu pourrais aussi aimer