18/07/2022
Nga jàpp ne ku nekkul ci sa ay itte ay jamono yamu la soxlaa l*l , mu sox la rekk ñëw ngir fajal la sa ay aajo et ce que kooku sa bëgg-bëgg moo ko ñor ?
Ñii ñuy woowe ñu bari ci ay Saa-Politig itte askani wi itteelu leen , la ñor Askan wi ñoru leen ,
Lii ñuy woowe (prêt campagne) du wenn layuwaay ne bu jege wut rekk waru noo xam itte askani wi mbaa seen i aajoo ,
Dëgg-dëgg i campagne , ak yoon wu leer wu nu mana wóoloo politicien bi mooy mu teewal aajoy askan wi ، wuute lool ce que ce passe aujourd'hui ,système bii daa bon , soofe lool ci gis-gis , ñàkk xorom lool ci yëg-yëg , yàgg nu cee nax , ta loolu amnaa ci lu wóor ne ak yeewute am na ci leegi
Waaja waxoon nani : "suukër bu la rombee ne la damay sàngu ji bu la rombaatee xamalne waxutoon dëgg"
Politicien yi nañu respecter Saa Senegaal yi