Khidmatoul Khadim Lil Khelcom

Khidmatoul Khadim Lil Khelcom Khidmatoul Khadim lil khelcom ak Sunu jewrign le fils aîné de Serigne Cheikh Saliou Serigne Khadim Mbacké . Cheikh Saliou Mbacké.

To help children learning Quran with goods, toiletries, clothing and anything they may need to carry on their education. Ligueyal Serigne Saliou ci Tolly khelcom ak Sunu Jewrign Serigne Khadim Mbacké Ibn S. Jeuf si suñu alaal, dolèe ak xël Mouride jeuf

Association Khidmatoul Khadim Lil Khelcom Di Demarrage Barkelou 2024/2025 le 10 Decembre.Numero bi la: 787171919 ou 7792...
04/12/2024

Association Khidmatoul Khadim Lil Khelcom Di Demarrage Barkelou 2024/2025 le 10 Decembre.

Numero bi la: 787171919 ou 779202607
wave wala Orange money.
Ligueyal Serigne Saliou Mbacke si Ndongo yi 😊🙏🏾

Association Khidmatoul Khadim Lil Khelcom Di yeugueul mbok talibe yi beug bok si kurel gui dina niou tambali Barkelou yi...
23/11/2024

Association Khidmatoul Khadim Lil Khelcom Di yeugueul mbok talibe yi beug bok si kurel gui dina niou tambali Barkelou yi le 10 Decembre.

Numero bi la: 787171919
wave wala Orange money.
Khidmatoul Khadim Lil Khelcom di tambali barkekou 2024/2025 ku beug tabi si liguey bi mo ngi ni ligueyal Serigne Saliou Mbacke si Ndongo yi 😊🙏🏾

Sunu chaine YouTube bi: Na si niep diap abonner si
19/10/2024

Sunu chaine YouTube bi:
Na si niep diap abonner si

Ziar Khidmatoul Khadim Lil Khelcom 2024 Chez S . Khadim Mbacke Ibn S. Cheikh Saliou

19/10/2024

5e édition ziar Khidmatoul Khadim Lil Khelcom chez Serigne Khadim Mbacke 19/10/2024.
Dem naniou yobou sunu adiya aki jayanté wadial ko khelcom.

JAYANTÉ YI TOLOU si: 1.500.000 Frs

Boubou femmes 80
Boubou hommes 18
Boubou filles 26
Boubou garçons 19
Ensembles blouson garçons 27
Pull over garçons 29
Carton savon 13
Sac omo grand modèle 4
Chaussure plastique 20 paires
Chaussure cuir 2 paires
Parfums 17 bouteilles
Lait de corp 11 bouteilles
Carton Madar 1
Eaux de javel 6bouteilles de 1l

Wadial Ziar 2024 Khelcom. KHIDMATOUL KHADIM LIL KHELCOM.Samedi le 19 Octobre dina niou dem si Serigne Khadim Mbacke mou ...
14/10/2024

Wadial Ziar 2024 Khelcom. KHIDMATOUL KHADIM LIL KHELCOM.
Samedi le 19 Octobre dina niou dem si Serigne Khadim Mbacke mou Serigne Cheikh Saliou yobou adiya gui ak Barkelou yi.

Kou Beug Barkelou si liguey bi 779202607
Sokhla naniou ay sabbou, tissus, yèrè Olof goor ak jiguen rawatina dalou plastique yi

Ligueyal Serigne Saliou ci ndongo yi 😊

13/10/2024

Di lèn yegeul sunu Ziar bi si Serigne Khadim
Mbacke mou Serigne Cheikh Saliou wadial Khelcom bi.
Beug naniou kep kou Beug barkelou def ko si numero bi 779202607

02/10/2024

Wadial Khelcom BARKELOU si 779202607 wave orange Money

24/04/2024

Khassida Matlabul Fawzeyni par Serigne Bassirou Toure

Mbok talibe yi daniouy def bissou jayantè nguir wadial Khelcom 2024. Jayanté ci numero bi 779202607 wave ak orange money...
23/04/2024

Mbok talibe yi daniouy def bissou jayantè nguir wadial Khelcom 2024. Jayanté ci numero bi 779202607 wave ak orange money.
Nio ngi wo nieup niou barkelou si liguey bi ak Khidmatoul Khadim Lil Khelcom

Di sakku si Mbok talibè yeup niou nianal sunu Mbok mou bakh mi Modou Mbacké am niouko khamone si tourou Paul Gomis.Baye ...
22/04/2024

Di sakku si Mbok talibè yeup niou nianal sunu Mbok mou bakh mi Modou Mbacké am niouko khamone si tourou Paul Gomis.

Baye Fall talibè Serigne Abdou Karim Mbacké ibn Serigne Fallou.

Fatiha ak
11 likhlass
Yalla nako sunu borom jeggal kou bakh di ab baye Fall.

Address

Cheltenham
SN32GN

Telephone

+221779202607

Website

Alerts

Be the first to know and let us send you an email when Khidmatoul Khadim Lil Khelcom posts news and promotions. Your email address will not be used for any other purpose, and you can unsubscribe at any time.

Contact The Business

Send a message to Khidmatoul Khadim Lil Khelcom:

Videos

Share