24/09/2024
Dileen fàttali sunu mbokk mi di SANGUE TALL
Ñëwna tay lan koy jébbal sunu boroom ginaaw tàkkusaan
Ñoongi kay waajale DAROU MINAM di sàkku ku mana teew nga teew fa kuko manul nga ñaanal ko jéggalug sunu boroom