Ma-xereñ

Ma-xereñ IBRAAHIIMA💥

04/12/2024
Lii Mooy këyit wiy xamle waxtuy jàpp yi ak waxtuy dog yi ci Tuubaa ak li ko wër toll ci 100 Km ci ndayjoor ak càmmooy, a...
11/03/2024

Lii Mooy këyit wiy xamle waxtuy jàpp yi ak waxtuy dog yi ci Tuubaa ak li ko wër toll ci 100 Km ci ndayjoor ak càmmooy, ak 27 Km ci penku ak ci sowwu. Ku nekk ci biir lii, mën naa jëfandikoo këyit wii ni ko waa Tuubaa di jëfandikoo.
Këyit wi Talaata 12 Màrs 2024 -Inshaa Allaah- lay tàmbali.
Mingi bawoo ci mbooloo mi yore wàllum xam-xam mi ci Daa’ira Muxaddamatul Xidma bu Jumaay Tuubaa.
Yal na sunu Borom defal jullit ñépp koorug jàmm te nangu lépp.

11/03/2024

Assalaamu halaykum.
Noo ngi leen di nuyu, di leen siyaare bu wér a wér, di leen ndokkeel ci weer wu sell wii tey ñaan sunu Boroom mu kàttanal nu ba nu defe ko ni mu ko santaanee te mu nangul nu te nu wéy di ko teewe ay at yu bari a bari te muy ànd ak wér ak ug defaru ak fajug aajo ci barkeb Alxuraan !

03/03/2024

Adresse

Touba

Heures d'ouverture

Lundi 06:00 - 18:00
Mardi 06:00 - 18:00
Mercredi 06:00 - 18:00
Jeudi 06:00 - 18:00
Vendredi 06:00 - 18:00
Samedi 06:00 - 18:00
Dimanche 06:00 - 18:00

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Ma-xereñ publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Partager