Digital mouride

  • Home
  • Digital mouride

Digital mouride le MOURIDE Saadikh est le degré le plus haut qu'un musulmans puisse daigner atteindre

22/12/2024

le MOURIDE Saadikh est le degré le plus haut qu'un musulmans puisse daigner atteindre

إنا لله وإنا إليه الراجعونSERIGNE ABDOU RAHMANE MOOFI BAAYÉ KO 🙏😭😭Que Firdaws soit sa demeure éternelle Amiiine
29/09/2022

إنا لله وإنا إليه الراجعون
SERIGNE ABDOU RAHMANE MOOFI BAAYÉ KO 🙏😭😭
Que Firdaws soit sa demeure éternelle Amiiine

06/09/2022

PARTAGER 🙏🙏🙏

BISMILAH Doxx jëum ça Magal Touba suñu Yitté. Kousi beug rek meun naniu contacter si sunu num WATSHAP inchallah.... Part...
11/08/2022

BISMILAH Doxx jëum ça Magal Touba suñu Yitté. Kousi beug rek meun naniu contacter si sunu num WATSHAP inchallah....
Partager 🙏

Na ngeen ko Dimbali jàppale ko Rawatina ñiko gënë jege: ñëp xam nanu seydina Umar su duggaan ci kër Yonint soxnay yonint...
18/07/2022

Na ngeen ko Dimbali jàppale ko Rawatina ñiko gënë jege: ñëp xam nanu seydina Umar su duggaan ci kër Yonint soxnay yonint (Psl) ak Ñafay liggey ñëppay daw laaqu . Ndax Taraay Umar ji .

Sëriñ yiy jiité mbooloo noonu lees di àndeek ñoom , ni seex Ibra Faal Ande woonak Sëriñ Tuuba (Rta).
Loolu ak Nimbal la ci Sëriñ Bi ak yëwit !! Ndax ibliss duko may jamm fileek daanu ko.

Fii ñëppay tarqiiss waaye pexey ibliss mooy toroxal aji Saabaal katu Yallah. Na ngeen gënë laxasaayu te bañ ko wacc ngeen dimbalante seen biir.

Xadiis Bi Ibn Jawzia ci Teereem ba : Talbis Iblis dafa waxni Ku Bëg tabbi aljana naga takkook Jullit hakkane yi te mëytu di beru, Mba nga wut kula ñaareel luko moy Seytane danala jekku tè Dinala Daan.

Taalibe dafay yewwu te Dafa Rëy Pass Pass te Da wara xamni tarxiss jombul Ku Yallah bind .

Nageen ko Jappale te buleen may Ibliss fum tëgge ndëndëm !!!
Buleen tass te buleen dakkal bissu Xassida yi , na gënë birr na gënë jolli , te neeleen ko jakk diko saytu ba ALJANNAH Incha Allahu.

Na ngeen dund tay dundël charia kuci wacc charia rek na yet wi dal (ci Sutura) !! Du diggën buur ak Jaam deedet digënte ñaari xarit la ci Yoonu Yallah. Ni lanuy ande ak sa Sëriñ.

Wass Salaam
Source: Ibn Abdillah groupe (Imaan Islam Ihsaan At Tassawuf)

Partager mouride🙏 Aimer la PageAbonnez vous sur la page
29/05/2022

Partager mouride🙏
Aimer la Page
Abonnez vous sur la page

Séjour du khalife général de mouride à Dakar
28/05/2022

Séjour du khalife général de mouride à Dakar

Waxi borom BelelPartager 🙏🙏🙏
24/05/2022

Waxi borom Belel
Partager 🙏🙏🙏

15/02/2022
 Le Khalife Général des mourides, Serigne Mountakha a mis entre les mains de TOUBA CA KANAM une somme de 30.000.000 frs ...
20/09/2021


Le Khalife Général des mourides, Serigne Mountakha a mis entre les mains de TOUBA CA KANAM une somme de 30.000.000 frs pour sa contribution à L'OPÉRATION WALLU initiée par nous pour dégager les eaux pluviales stagnantes dans la ville sainte.

Cëy Mbàkke! Yaa baax ba jàll baax.
Sëriñ Muntaqaa jox na waa Tuubaa Ca Kanam 30.000.000 fr ngir jëlee fi ndoxum taw bi.

Safar 1«Banaa lepp maa ngii si sab ate tayFaxas naa ludul yaw falang naako yitFaxas naa ludul yaw si man mii mu rotFalan...
09/09/2021

Safar 1

«Banaa lepp maa ngii si sab ate tay
Faxas naa ludul yaw falang naako yit

Faxas naa ludul yaw si man mii mu rot
Falang naako yit cee ba dootul ñëwit

Fabal nak sa bopp ak sa mbir def si man
Te def ma murid dëg buy sab xarit

Danaa wax ci yaw lutax ñepp xam
Ni yaw sam kem amul sowwu ak penku yit

Danaa wax ci yaw lutax ñepp xam
Ni yaw sam kemm amul sowwu ak penku yit

Bangay jápp xaalis aka dëddu aka bañ
Akay sanni ci ak dex nga raw kepp nit

Bangay weet akay muñ akay dunde ñax
Fa yeefar ya nga far ñepp noot

Bangay jáng akay bind ñuy fó aka moy
Fi sak wet nga sut Mbákke mbooléem ña sut

Bangay jáng akay bind ñuy fó aka moy
Fi sak wet nga sut Mbákke mbooléem ña sut»

(Sëriñ Mbay Jaxate)

Nataal: Màggalug Tuubaa ci atum 1368 AH
Crédit : Lorenzo Italia

🔴Nouveau Khalif general des baye fallCheikh Mouhamadoul Moustapha Fall mom Serigne Modou mbenda yalla nanga agalek jamm ...
01/09/2021

🔴Nouveau Khalif general des baye fall
Cheikh Mouhamadoul Moustapha Fall mom Serigne Modou mbenda yalla nanga agalek jamm yalla nanga fii yagg lol fall yaram

Tiis dileen yeugeul wathiouk ligeuyou Serigne Sheikh Dieumou Fall Khalifa Mame Cheikh Ibrahima Fall Yala nako yala doly ...
31/08/2021

Tiis dileen yeugeul wathiouk ligeuyou
Serigne Sheikh Dieumou Fall Khalifa Mame Cheikh Ibrahima Fall
Yala nako yala doly ayy kheweul Famou dieum Si Barkep Serignebi

Le khalif gènèral des mourides Serigne Mountakha Bassirou MBACKÉ a dègagé 50 millions de francs CFA en guise de compensa...
29/08/2021

Le khalif gènèral des mourides Serigne Mountakha Bassirou MBACKÉ a dègagé 50 millions de francs CFA en guise de compensation aux sinistrés de Touba.

Magal Darou Khoudoss 2021 Photos du khalif Général des Mourides Serigne Mountakha MBACKE Bachir
28/08/2021

Magal Darou Khoudoss 2021 Photos du khalif Général des Mourides Serigne Mountakha MBACKE Bachir

‘’ Rafet nga jëf, rafetub xol, YAllah yal nala fay. Te maye la wis la, ba nab lo ame ni dell’aku yiw. Rëy ngaw fit’ak it...
28/08/2021

‘’ Rafet nga jëf, rafetub xol, YAllah yal nala fay. Te maye la wis la, ba nab lo ame ni dell’aku yiw. Rëy ngaw fit’ak itte, rëy ngab xol te rëy nga jëf it. Rëyub yar’ak juddu, rëy ndam, rëy ngeureum mata naw’’
Señ Mbay Jaxatee

Address


Alerts

Be the first to know and let us send you an email when Digital mouride posts news and promotions. Your email address will not be used for any other purpose, and you can unsubscribe at any time.

Videos

Shortcuts

  • Address
  • Telephone
  • Alerts
  • Videos
  • Claim ownership or report listing
  • Want your business to be the top-listed Media Company?

Share