Marakhib TV

Marakhib TV Marakhib TV est une Chaine islamique au service de Xadim Rassul.

28/10/2023
27/05/2023

NJAAREEM

« Su dëgg doonee ag dëgg ba noppi bala nga koo wax na ca ñatt(3) daje : Na ca sa yoon nekk, te ñu laaj la ko, mbaa nga y...
23/05/2023

« Su dëgg doonee ag dëgg ba noppi bala nga koo wax na ca ñatt(3) daje : Na ca sa yoon nekk, te ñu laaj la ko, mbaa nga yilif ñi nga koy waxal. »
Seex Abdul Ahad Mbàkke

28/03/2023

ANNONCE CONFERENCE DAARA EL HADJ TIDIANE NIANG LE 1ER AVRIL

BISSPU SERIGNE SAAM MBAYE BU  NDAR
20/03/2023

BISSPU SERIGNE SAAM MBAYE BU
NDAR

20/03/2023

DAARA SOPPEY SERIGNE SAM MBAYE BU NDAR / JOURNEE DE PRIERES

Sëriñ Tuubaa Xaada lahu laahu maxtaara lahu neena : "Suufiyu dëgg mooy boroom xam-xam buy jëfe xam-xamam te bañ di moy Y...
28/02/2023

Sëriñ Tuubaa Xaada lahu laahu maxtaara lahu neena : "Suufiyu dëgg mooy boroom xam-xam buy jëfe xam-xamam te bañ di moy Yàlla ci dara, te lepp jëmmi Yàlla rekk tax".

Nahju.

Ndékaane Seexul Xadiim. Maa ngi leen di dénk juróom benn i baat yoo xam ne làq na juróom benn i téemeeri njariñ: 1) - Sa...
27/02/2023

Ndékaane Seexul Xadiim.

Maa ngi leen di dénk juróom benn i baat yoo xam ne làq na juróom benn i téemeeri njariñ:

1) - Saa bu nit ñi dawee jëm ci ngënéel yi rek, yaw na nga daw jëm ci jëfe faratay [sunu Boroom yi].

2) - Su nit ñi dawee jëm ci [seen moroomi] mbindéef yi, yaw na nga daw jëm ci Yàlla mi bind mbidéef yi.

3) - Su nit ñi dawee jëm ci yittéwoo xam-xam kese, yaw na nga daw jëm ci jëfe xam-xam.

4) - Su nit ñi dawee jëm ci mbiri zaahir kese, yaw na nga daw jëm ci mbiri biir [yi nga xam ne Yàlla rekkay tax].

5) - Su nit ñi dawee dëgmal àdduna rek, yaw na nga daw dëgmal lu lay musël bisu pencc.

6) - Su nit ñi di yitte woo di luñuti ayibi jàmbur yi, yaw sa ayibi bopp na la doy sëkk.

17/01/2023

THIANT ANNUELLE DAARA NOUROU DAARAYNI TOUBA DE PARIS BANDE ANNONCE

Ñu bokk ko waajal
08/12/2022

Ñu bokk ko waajal

BOROOM TUUBAA nee na lii kuko wax deessula bindal bàkkaar diirub junniy att( 1000 ans ) mi ngi ni👇"laa ilaaha illal laah...
30/11/2022

BOROOM TUUBAA nee na lii kuko wax deessula bindal bàkkaar diirub junniy att( 1000 ans ) mi ngi ni👇

"laa ilaaha illal laahu usaffii bihaa amrii laa ilaaha illal laahu ad hulu bihaa xabrii laa ilaaha illal laahu usxilu bihaa miisaanii laa ilaaha illal laahu urdii bihaa rabbii laa ilaaha illal laahu Muhammadu Rassulullaahi Sallalaahu Halayhi wa salama"

Baay Faal yi ak ñenn ci waa dëkk bi àndoon di yeesal armeeli Marmiyaal.
21/11/2022

Baay Faal yi ak ñenn ci waa dëkk bi àndoon di yeesal armeeli Marmiyaal.

Na ci ñeep teew
19/11/2022

Na ci ñeep teew

Nganale Sëriñ Baara Mbàkke Daaray kër Sëriñ Bàmba Silla.
16/11/2022

Nganale Sëriñ Baara Mbàkke Daaray kër Sëriñ Bàmba Silla.

Nu wax tuuti ci Àddiya.Àddiya dafay ñoodi murid bi yóbb ko ci texe.-Day kawel maqaama murid bi.-‎Day baril alalu ki koy ...
02/10/2022

Nu wax tuuti ci Àddiya.

Àddiya dafay ñoodi murid bi yóbb ko ci texe.
-Day kawel maqaama murid bi.
-‎Day baril alalu ki koy joxe.
-‎Day gudal aw fan.
-‎Day tax nit ñi sopp la
-‎Dy waral nga jiitu sag maas.
-‎Day waral doo gis ñaari malaayika yiy laaj ci bàmmeel.

Àddiya day tax booy jéggi siraat mu gaaw
-Day tax deesu la seet sa jëf.
-‎Day tax doo gis fitney bàmmel.
-‎Day tax sax yi nekk ci suuf duñu lekk sa yaram
-‎ak yéneen ak yéneen...

Li tax murid bi di joxe àddiya loolu dafay wéral dëggalam. Bu ko joxe ku ko yeeloo, li ci ëpp xelam day nekk ci mbir yi Kim jox àddiya bi. jëmale alal gi. Ba tay, Sëriñam (walla kudul moom sax) dinakoy faral di xalaat ak xelam di dem ci moom. Te loolu tawfeexu taalube bi la.

Al-Habdul Xadiim.

Inari Lahi wa ina ilayhi Rajihon: Rappel à Dieu de Serigne Abdourahmane Mbacké.
29/09/2022

Inari Lahi wa ina ilayhi Rajihon: Rappel à Dieu de Serigne Abdourahmane Mbacké.

Magal Touba 2022  Khassida « Usnî Alâ Man Bi Fathi » déclamé par le kurel 1 B Hizbut Tarqiyyah Touba https://youtu.be/vt...
22/09/2022

Magal Touba 2022 Khassida « Usnî Alâ Man Bi Fathi » déclamé par le kurel 1 B Hizbut Tarqiyyah Touba
https://youtu.be/vtS943nkZAI

MEÑÑETUM TAZAWUDU SIQAAR : PART.1
12/07/2022

MEÑÑETUM TAZAWUDU SIQAAR : PART.1

Pour la couverture et la retransmission en direct sur Marakhib TV de vos événements religieux (les Magals, les Gamous, les Ziarras)Contactez-nous par email: ...

WAXTAAN CI XASSIDA YI SERIGNE BASSIROU MBACKE XELCOM
08/07/2022

WAXTAAN CI XASSIDA YI SERIGNE BASSIROU MBACKE XELCOM

Pour la couverture et la retransmission en direct sur Marakhib TV de vos événements religieux (les Magals, les Gamous, les Ziarras)Contactez-nous par email: ...

RAJASS SERIGNE MOUSTAPHA NIANG KOUL / BISSUP SANT SERIGNE SALIOU DAARA NURUL MAHAHIDI
29/06/2022

RAJASS SERIGNE MOUSTAPHA NIANG KOUL / BISSUP SANT SERIGNE SALIOU DAARA NURUL MAHAHIDI

Pour la couverture et la retransmission en direct sur Marakhib TV de vos événements religieux (les Magals, les Gamous, les Ziarras)Contactez-nous par email: ...

Adresse

Saint-Louis

Téléphone

+221772540835

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Marakhib TV publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à Marakhib TV:

Vidéos

Partager

MARAKHIB TV

Marakhib TV Une chaine islamique au coeur de la religion pour diffuser et partager des emissions et des idees au service de KHADIM RASSOULL l’eternel serviteur de DIEU


Autres Chaîne de télévision à Saint-Louis

Voir Toutes