Bichridigitalagency

Bichridigitalagency Agence de communication marketing digitale et de production audiovisuelle.

bichriartproduction est une équipe de designer,producteur et réalisateur de vidéo...mais toute notre compétence dagn ko djeul délo ko borom touba fass ko ligueyeul ba fatou

Am na kilifa gu mas a wax Sëriñ bi ni nga melee ni ku xamul àdduna te xam ko lool ? Sëriñ bi ni ko, xam koo tax nu wacc ...
25/04/2024

Am na kilifa gu mas a wax Sëriñ bi ni nga melee ni ku xamul àdduna te xam ko lool ? Sëriñ bi ni ko, xam koo tax nu wacc ko.
#

Sëriñ Tuubaa (haa da lahu Allaahu maa ahtaara lahu) mas naa jox Sëriñ Bàlla Faali Jeng "Jalibatul Marahib", ni ko:Ku ma ...
22/04/2024

Sëriñ Tuubaa (haa da lahu Allaahu maa ahtaara lahu) mas naa jox Sëriñ Bàlla Faali Jeng "Jalibatul Marahib", ni ko:

Ku ma yebalati ci yow, na nga ko ko jox mu koy jàng ndax fa ma tolloon ba daan def ci ñoom fim ne da maa amatut jot gi. Xasiida gii nag moo ma ci wuutu.

🅻︎🅴︎ 🅶︎🆁︎🅰︎🅽︎🅳︎ 🅼︎🅰︎🅶︎🅰︎🅻︎ 🅳︎🅴︎ 🆃︎🅾︎🆄︎🅱︎🅰︎ 🆄︎🅽︎🅴︎ 🆂︎🅴︎🆄︎🅻︎ 🅳︎🅰︎🆃︎🅴︎ 🅰︎ 🆁︎🅴︎🆃︎🅴︎🅽︎🅸︎🆁︎ 18🇸 🇦 🇫 🇦 🇷 *jour j* - *1⃣2⃣4⃣*Ⓓ︎Ⓞ...
21/04/2024

🅻︎🅴︎ 🅶︎🆁︎🅰︎🅽︎🅳︎ 🅼︎🅰︎🅶︎🅰︎🅻︎
🅳︎🅴︎ 🆃︎🅾︎🆄︎🅱︎🅰︎ 🆄︎🅽︎🅴︎ 🆂︎🅴︎🆄︎🅻︎ 🅳︎🅰︎🆃︎🅴︎ 🅰︎ 🆁︎🅴︎🆃︎🅴︎🅽︎🅸︎🆁︎
18🇸 🇦 🇫 🇦 🇷
*jour j* - *1⃣2⃣4⃣*
Ⓓ︎Ⓞ︎Ⓚ︎Ⓗ︎ Ⓓ︎Ⓘ︎Ⓔ︎Ⓤ︎Ⓜ︎ Ⓢ︎Ⓐ︎ 🚶🏾‍♂️🚶🏾‍♂️🚶🏾‍♂️🅑︎🅞︎🅤︎ 🅓︎🅞︎🅚︎🅗︎ YÉKHÉ RÉK
🇬 🇳 🇴 🇺 🄳🄰🅆🏃🏿‍♂️🏃🏿‍♂️🏃🏿‍♂️ 🅱︎🅰︎🅼︎🅱︎🅰︎ 🇩 🇮 🇦 🇷 🇳 🇦 🇰 🇴 
😍😍😍😂😂😂😂😍😍😍😍
18 Safar

20/04/2024

WAKHI SERIGNE MBAYE DIAKHATÉ AK SERIGNE KHADIM DIAW PAKHA❣❤🤩😍

Benn naar ne woon na Sëriñ Tuubaa mat gi mu mat moo tax mu wóolu boppam, bàyyi ab taalibeem fu ko neex barkeelu ndax du ...
20/04/2024

Benn naar ne woon na Sëriñ Tuubaa mat gi mu mat moo tax mu wóolu boppam, bàyyi ab taalibeem fu ko neex barkeelu ndax du yàgg mukk ba mu gis lu kawe li ci Sëriñ bi.

🅻︎🅴︎ 🅶︎🆁︎🅰︎🅽︎🅳︎ 🅼︎🅰︎🅶︎🅰︎🅻︎ 🅳︎🅴︎ 🆃︎🅾︎🆄︎🅱︎🅰︎ 🆄︎🅽︎🅴︎ 🆂︎🅴︎🆄︎🅻︎ 🅳︎🅰︎🆃︎🅴︎ 🅰︎ 🆁︎🅴︎🆃︎🅴︎🅽︎🅸︎🆁︎ 18🇸 🇦 🇫 🇦 🇷 *jour j* - *1⃣2⃣6⃣*Ⓓ︎Ⓞ...
19/04/2024

🅻︎🅴︎ 🅶︎🆁︎🅰︎🅽︎🅳︎ 🅼︎🅰︎🅶︎🅰︎🅻︎
🅳︎🅴︎ 🆃︎🅾︎🆄︎🅱︎🅰︎ 🆄︎🅽︎🅴︎ 🆂︎🅴︎🆄︎🅻︎ 🅳︎🅰︎🆃︎🅴︎ 🅰︎ 🆁︎🅴︎🆃︎🅴︎🅽︎🅸︎🆁︎
18🇸 🇦 🇫 🇦 🇷
*jour j* - *1⃣2⃣6⃣*
Ⓓ︎Ⓞ︎Ⓚ︎Ⓗ︎ Ⓓ︎Ⓘ︎Ⓔ︎Ⓤ︎Ⓜ︎ Ⓢ︎Ⓐ︎ 🚶🏾‍♂️🚶🏾‍♂️🚶🏾‍♂️🅑︎🅞︎🅤︎ 🅓︎🅞︎🅚︎🅗︎ YÉKHÉ RÉK
🇬 🇳 🇴 🇺 🄳🄰🅆🏃🏿‍♂️🏃🏿‍♂️🏃🏿‍♂️ 🅱︎🅰︎🅼︎🅱︎🅰︎ 🇩 🇮 🇦 🇷 🇳 🇦 🇰 🇴 
😍😍😍😂😂😂😂😍😍😍😍
18 Safar

⦁ Sëriñ bi nee na ab sëriñ bu dee digle te la muy digle jëlee wu ko ci Yàlla subxaanahuu wa ta’alaa door koo sant ka mu ...
18/04/2024

⦁ Sëriñ bi nee na ab sëriñ bu dee digle te la muy digle jëlee wu ko ci Yàlla subxaanahuu wa ta’alaa door koo sant ka mu koy sant koo ku réer na te ku ko topp mu réeral la ndax li ci téere yi ñéppa ko jàng te téere yi ay xulóo kesee ci nekk.
To

⦁ Am na bis ku bokkul ci yoon wi xëysi ci Sëriñ bi suba teel, bi mu ñëwee fekk Sëriñ bi di joxe kafe mu ni Assalaamu ala...
17/04/2024

⦁ Am na bis ku bokkul ci yoon wi xëysi ci Sëriñ bi suba teel, bi mu ñëwee fekk Sëriñ bi di joxe kafe mu ni Assalaamu alaykum dem ba nee mu capp fa. Bi Sëriñ bi noppee mu ñëw ni ko sa mbooloo mii sama doom mi ngi ci te sama ndigal bàyyi wu ko fi, Sëriñ bi wax ni Laailaah ilallaahu ana nu mu tuddu ? mu ni ko Baabakar Saar, Sëriñ bi yónnee woo-lu ko mu ñëw yegg suuf, Sëriñ bi ni ko ndax xam nga kii ? Mu ni ko waaw sama baay la. Sëriñ bi ni ko damaa bëgg nga ànd ak moom, boo yeggee lu mu la sant nga nekk ca lu mu la tere nga bàyyi ko, koo ka ni ko bu ma naree dem jaral na ma dee dem sawara. Sëriñ bi ni ko ëpp naa def loo lu kenn du ko wax man ku ànd ak man du dem sawara. Góor ga ni ko Sëriñ bi yaa ko wax ? Mu ni ko waaw, góor ga ni ko daan naa ko dégg ci taalibe yi waaye ñoom li ñuy yokk daa bari lool. Sëriñ bi ni ko léeg-léeg it ñu wàññi. Góor ga ni ko ginnaaw yaa ko waxal sa bopp jox naa la saa bopp bis niki tay ak njaboot ga ca kër ga, moom mii na toog nekkal ma fi.

Sëriñ Tuubaa nee na « Niti Yàlla yi loo baax-baax, booleen seetee du tax ñu wax la luy tax nga gis sa bopp mukk, waaye d...
13/04/2024

Sëriñ Tuubaa nee na « Niti Yàlla yi loo baax-baax, booleen seetee du tax ñu wax la luy tax nga gis sa bopp mukk, waaye dañ lay gëna soññ ci jaamu Yàlla ak lu baax. Waaye lu nit bon-bon, boo leen seetee duñ la daw mukk, te duñ la wax it lu lay naaguloo yërmande Yàlla, di nañ la dalal, xamal la yërmande Yàlla ni mu yaatu ba nga tuub, jeggalu sa Boroom » Delluwaay bi: Majmuhaat


🇸🇳 ́négal

Àtteb julli iid :Hanafiya ne farata la, Maalig ak ñenn ci Saafihi ne sunna mu’akkada, Hanaabila yi ne bu ko ñenn ñi defe...
09/04/2024

Àtteb julli iid :
Hanafiya ne farata la, Maalig ak ñenn ci Saafihi ne sunna mu’akkada, Hanaabila yi ne bu ko ñenn ñi defee wàcc na ñeneen ñi.

Manees na ko fay nag bu fekkee dafa raw waa dëkk bi yépp, niki ñu wooroon ba digg bëccëg door a xam ne feeñ na démb dañuy xéy suba fay ko.


🇸🇳 ́négal

Kàdduy Sëriñ Amsatu Mbàkke 27 ci koor 1445/Avril 2024 daaray kër Ma-xujja.Ginnaaw sant Yàlla julli ci Yonent bi Shw sant...
08/04/2024

Kàdduy Sëriñ Amsatu Mbàkke
27 ci koor 1445/Avril 2024 daaray kër Ma-xujja.

Ginnaaw sant Yàlla julli ci Yonent bi Shw sant nanu Sëriñ Tuubaa, cant gu amul àpp.

Liggéeyub Alxuraan bii nu nekk, danu koy sante sunu ñaari wayjur ya, muy Sëriñ Suhaybu ak Sëriñ Saalihu, Ndax lii nu nekk ñoom ñaar lanu ci wuutu. Sëriñ Suhaybu ak Sëriñ Saalihu benn lañu woon, ndax ku ci ne daa nga jël ay dongo jox sa moroom.

Sëriñ Suhaybu daa mel ni ku xamoon ne Sëriñ Saalihu moo ko fiy mujj ba tax mu jëloon lim bu bari ci ay dongoom jox ko Sëriñ Saalihu.
Nun ñii nag liggéey bii nu nekk daa mel ni rekk ag matt gu nu jële ca taalub Sëriñ Suhaybu di ca xor-xoral,

Waaye bi ci Sëriñ Saalihu duggee rekk lanu daa di yëg yokkutu gu mag ba fii nu toll (Li muy leeral foofu mooy, Sëriñ Suhaybu dafa joxoon Sëriñ Saalihu lu mat 100i Ndongo Moom Sëriñ Amsatu mii, ayu-bis gi Sëriñ Saalihu mujj a def ci kaw suuf da koo woo jox ko lim bu jege boobu ci ay ndongo,

Moo tax mu wax ne booba la tàmbalee yëg yokkutu ci liggéey bi, loolu day màndargaal ne liggéey boobu Sëriñ Saalihu ne woon féetale na ko ko.)
Ndax mbooleem fu ma teg sama bët dinaa fa gis kenn ci jiwu wi fi Sëriñ Saalihu indi woon,

Dëgg la naw naa ñépp waaye ñoom moom naw naa leen lool, Li ëpp ci liggéey bi ñoo koy taxawu, kon lii xol sedd na ci lool.

Ndax def ngeen ci gone yi loo xam seeni wayjur sax manuñu ko, Te ma yëg ne sonn ngeen ci lool, ndax Yàlla kat ba la laa dimbali dangay jéem dara kon yal na leen Yàlla fay ci barkeb Alxuraan jërëngeenjëf.

Wassalaamu hallaykum !


🇸🇳 ́négal

Image du jourMachrabu Çaafi Ramadan 2024 à la résidence Khadimou Rassoul de Touba avec Hizbut Tarqiyyah et le Khalif Gén...
08/04/2024

Image du jour
Machrabu Çaafi Ramadan 2024 à la résidence Khadimou Rassoul de Touba avec Hizbut Tarqiyyah et le Khalif Général des Mourides.

Koo xam ni, bëgg nga saa soo xéyee di xéy ci sunub tool, di ñu fàwwil, boo xéyatee m, xéyal ci Alxuraan✍️Sëriñ Tuuba
08/04/2024

Koo xam ni, bëgg nga saa soo xéyee di xéy ci sunub tool, di ñu fàwwil, boo xéyatee m, xéyal ci Alxuraan
✍️Sëriñ Tuuba

🅻︎🅴︎ 🅶︎🆁︎🅰︎🅽︎🅳︎ 🅼︎🅰︎🅶︎🅰︎🅻︎ 🅳︎🅴︎ 🆃︎🅾︎🆄︎🅱︎🅰︎ 🆄︎🅽︎🅴︎ 🆂︎🅴︎🆄︎🅻︎ 🅳︎🅰︎🆃︎🅴︎ 🅰︎ 🆁︎🅴︎🆃︎🅴︎🅽︎🅸︎🆁︎ 18🇸 🇦 🇫 🇦 🇷 *jour j* - *1⃣3⃣7⃣*Ⓓ︎Ⓞ...
07/04/2024

🅻︎🅴︎ 🅶︎🆁︎🅰︎🅽︎🅳︎ 🅼︎🅰︎🅶︎🅰︎🅻︎
🅳︎🅴︎ 🆃︎🅾︎🆄︎🅱︎🅰︎ 🆄︎🅽︎🅴︎ 🆂︎🅴︎🆄︎🅻︎ 🅳︎🅰︎🆃︎🅴︎ 🅰︎ 🆁︎🅴︎🆃︎🅴︎🅽︎🅸︎🆁︎
18🇸 🇦 🇫 🇦 🇷
*jour j* - *1⃣3⃣7⃣*
Ⓓ︎Ⓞ︎Ⓚ︎Ⓗ︎ Ⓓ︎Ⓘ︎Ⓔ︎Ⓤ︎Ⓜ︎ Ⓢ︎Ⓐ︎ 🚶🏾‍♂️🚶🏾‍♂️🚶🏾‍♂️🅑︎🅞︎🅤︎ 🅓︎🅞︎🅚︎🅗︎ YÉKHÉ RÉK
🇬 🇳 🇴 🇺 🄳🄰🅆🏃🏿‍♂️🏃🏿‍♂️🏃🏿‍♂️ 🅱︎🅰︎🅼︎🅱︎🅰︎ 🇩 🇮 🇦 🇷 🇳 🇦 🇰 🇴 
😍😍😍😂😂😂😂😍😍😍😍
18 Safar

Sëriñ Tuubaa nee na "Ku dégg njangum Jazbu du dégg riirum sawara".Sëriñ Alaaji Mbàkke andi nako ci teerem yimu dajjale w...
06/04/2024

Sëriñ Tuubaa nee na "Ku dégg njangum Jazbu du dégg riirum sawara".
Sëriñ Alaaji Mbàkke andi nako ci teerem yimu dajjale waxi Sëriñ bi.
Qasida Jazbu kuko jàng benn yoon ci sa dund mënatoo jëf lula yobbu sawara...Yàlla daf lay gis nga Koy moy, mu suturaal la, def ci sa xel mi réccu,

Daal di def ci sa xol bi tuub, nga tuub mu jéggal la.


🇸🇳 ́négal

🅻︎🅴︎ 🅶︎🆁︎🅰︎🅽︎🅳︎ 🅼︎🅰︎🅶︎🅰︎🅻︎ 🅳︎🅴︎ 🆃︎🅾︎🆄︎🅱︎🅰︎ 🆄︎🅽︎🅴︎ 🆂︎🅴︎🆄︎🅻︎ 🅳︎🅰︎🆃︎🅴︎ 🅰︎ 🆁︎🅴︎🆃︎🅴︎🅽︎🅸︎🆁︎ 18🇸 🇦 🇫 🇦 🇷 *jour j* - *1⃣3⃣8⃣*Ⓓ︎Ⓞ...
06/04/2024

🅻︎🅴︎ 🅶︎🆁︎🅰︎🅽︎🅳︎ 🅼︎🅰︎🅶︎🅰︎🅻︎
🅳︎🅴︎ 🆃︎🅾︎🆄︎🅱︎🅰︎ 🆄︎🅽︎🅴︎ 🆂︎🅴︎🆄︎🅻︎ 🅳︎🅰︎🆃︎🅴︎ 🅰︎ 🆁︎🅴︎🆃︎🅴︎🅽︎🅸︎🆁︎
18🇸 🇦 🇫 🇦 🇷
*jour j* - *1⃣3⃣8⃣*
Ⓓ︎Ⓞ︎Ⓚ︎Ⓗ︎ Ⓓ︎Ⓘ︎Ⓔ︎Ⓤ︎Ⓜ︎ Ⓢ︎Ⓐ︎ 🚶🏾‍♂️🚶🏾‍♂️🚶🏾‍♂️🅑︎🅞︎🅤︎ 🅓︎🅞︎🅚︎🅗︎ YÉKHÉ RÉK
🇬 🇳 🇴 🇺 🄳🄰🅆🏃🏿‍♂️🏃🏿‍♂️🏃🏿‍♂️ 🅱︎🅰︎🅼︎🅱︎🅰︎ 🇩 🇮 🇦 🇷 🇳 🇦 🇰 🇴 
😍😍😍😂😂😂😂😍😍😍😍
18 Safar

⦁ Sëriñ bi mas naa laaj benn waay foo nekk ? muy waxi dëkk. Sëriñ bi ni ko man déey, léeg-léeg may laaj kenn foo nekk mu...
06/04/2024

⦁ Sëriñ bi mas naa laaj benn waay foo nekk ? muy waxi dëkk. Sëriñ bi ni ko man déey, léeg-léeg may laaj kenn foo nekk muy tuddi dëkk. Damaa bëggoon ku ma ci laajati rek mu ni maa ngi ci waajib (lu war) ak manduub, (lu ñu sopp) di sonnu di noppalu ci mubaax (lu dagan). Daa di ni gees Sëriñ Bànj Njaay ni ko ana yaw foo nekk ? Mu ni ko maa ngi fa nga ma ba woon mu ree ni ko, waay joo joo la sa waaye kon loolu mu wax ngay wax.

⦁ Sëriñ bi nee na xam-xam bokkul ak xam Yàlla. Bokk na ci misaali xam Yàlla sunu Boroom, boo gisee aw jiwu, xam fa muy m...
05/04/2024

⦁ Sëriñ bi nee na xam-xam bokkul ak xam Yàlla. Bokk na ci misaali xam Yàlla sunu Boroom, boo gisee aw jiwu, xam fa muy mujju, bu saxee ndax di na rafet ak di na ñaaw ak yeneen ya cay sosu.

𝑙𝑖𝑔𝑒𝑒𝑦 𝑏𝑖 𝑏𝑢𝑚 𝑙𝑎𝑎𝑙 𝑠𝑢𝑢𝑓 𝑀𝑢𝑟𝑖𝑑 𝕄𝕒𝕘𝕒𝕝 𝕋𝕠𝕦𝕓𝕒 2024𝕁𝕁-140🥰🥰🥰
05/04/2024

𝑙𝑖𝑔𝑒𝑒𝑦 𝑏𝑖 𝑏𝑢𝑚 𝑙𝑎𝑎𝑙 𝑠𝑢𝑢𝑓 𝑀𝑢𝑟𝑖𝑑
𝕄𝕒𝕘𝕒𝕝 𝕋𝕠𝕦𝕓𝕒 2024
𝕁𝕁-140🥰🥰🥰

Sëriñ Tuubaa (haa da lahu Allaahu maa ahtaara lahu) Jumaay Njaareem "néeg ba" la ko daan wax.Ba tay am na ñuy wax "jàkka...
04/04/2024

Sëriñ Tuubaa (haa da lahu Allaahu maa ahtaara lahu) Jumaay Njaareem "néeg ba" la ko daan wax.
Ba tay am na ñuy wax "jàkka" la ko daan wax, xéy na ku nekk ak la nga dégg ci moom


🇸🇳 ́négal

Le "Koumté" est bien plus qu'une simple tradition alimentaire pour les Baye Fall  fidèles disciples de Serigne Amdy Modo...
04/04/2024

Le "Koumté" est bien plus qu'une simple tradition alimentaire pour les Baye Fall fidèles disciples de Serigne Amdy Modou Mbenda Fall, durant le mois de Ramadan. En préparant les Ndogou avec amour et dévotion, ils expriment leur allégeance et leur soumission au khalif général des Mourides.
Ces mets délicieux sont ainsi offerts avec un profond sentiment de dévotion et de respect envers les descendants de Serigne Touba incarnant l'esprit enseigné par Mame cheikh Ibrahima fall.
Ainsi, le "Koumté" devient un symbole puissant de la voie spirituelle tracée par ce dernier pour les Baye Fall


🇸🇳 ́négal

𝑙𝑖𝑔𝑒𝑒𝑦 𝑏𝑖 𝑏𝑢𝑚 𝑙𝑎𝑎𝑙 𝑠𝑢𝑢𝑓 𝑀𝑢𝑟𝑖𝑑 𝕄𝕒𝕘𝕒𝕝 𝕋𝕠𝕦𝕓𝕒 2024𝕁𝕁-141🥰🥰🥰
03/04/2024

𝑙𝑖𝑔𝑒𝑒𝑦 𝑏𝑖 𝑏𝑢𝑚 𝑙𝑎𝑎𝑙 𝑠𝑢𝑢𝑓 𝑀𝑢𝑟𝑖𝑑
𝕄𝕒𝕘𝕒𝕝 𝕋𝕠𝕦𝕓𝕒 2024
𝕁𝕁-141🥰🥰🥰

Maam Seex Ibra Faal naanukaayu murit yi dëggal.❣😍
03/04/2024

Maam Seex Ibra Faal naanukaayu murit yi dëggal.❣😍

⦁ Sëriñ bi mas naa jox Sëriñ Bàlla Faali Jeng Jaalibatul Maraaxib ni ko ku mu yabalati ci moom na ko koy jox mu koy jàng...
03/04/2024

⦁ Sëriñ bi mas naa jox Sëriñ Bàlla Faali Jeng Jaalibatul Maraaxib ni ko ku mu yabalati ci moom na ko koy jox mu koy jàng ndax fa mu tolloon ba daan def ci ñoom fi mu ne daa amatul jot gi. Xasiida gii nag moo ko ci wuutu.

Je tiens à adresser mes sincères félicitations et mes prières à Son Excellence Bassirou Diomaye Faye pour son élection e...
03/04/2024

Je tiens à adresser mes sincères félicitations et mes prières à Son Excellence Bassirou Diomaye Faye pour son élection en tant que président de la République du Sénégal. Que ce nouveau chapitre de leadership soit marqué par la sagesse, la compassion et le progrès pour notre cher pays. Que Dieu lui accorde la force et la clairvoyance nécessaires pour guider notre nation vers un avenir meilleur, où la paix, la prospérité et la justice règnent en maître. Mes pensées et mes prières l'accompagnent dans cette noble mission. 🇸🇳🌟 "

« Waa àjjana ñett lañu :Njiit lu maandu tey saraxe te am tawfeex, Ak waa ju ñeewante di yërëm ay bokkam yépp ak jullit ñ...
03/04/2024

« Waa àjjana ñett lañu :

Njiit lu maandu tey saraxe te am tawfeex, Ak waa ju ñeewante di yërëm ay bokkam yépp ak jullit ñi. Ak ku fegu doylu tey boroomug njaboot. »


🇸🇳 ́négal

Melow as Gor :« Koo xam ni kii saa su ñàkkee mbaa mu am dara bis. Nit ñépp dégg ko, kookee yar ba des na bu wér »Celui q...
03/04/2024

Melow as Gor :

« Koo xam ni kii saa su ñàkkee mbaa mu am dara bis. Nit ñépp dégg ko, kookee yar ba des na bu wér »

Celui qui à chaque fois qu’il obtient un bien ou en perd. Met au courant tout le monde manque vraiment de repères

« Koo xam ni kii lu mu làmboo, ñépp xam ko du nit. Nit day muñug ñàkk, muñ xeewël ni gumm ni mbër »

Celui pour qui les affaires ne sont un secret pour personne est un fou. L’homme doit patienter dans la richesse et quand il est sans-le-sou

« Mbër day lewet, yaru, am laf, tuuti wax, rëyi jëf. Bu suq say kañu, muy ub jépp làmb ju gor »

Un vrai champion est affable, peu bavard et de grandes actions mène. Puis quand les petits lutteurs se vantent s’évertue à être le roi de l’arène

« Aw fas la muy rawe ay fas loola kay du ηexal. Aw xél wu yéemu la jiitoo fas ya ak jëfi, ngor »

Ce n’est point par le hennissement qu’un cheval remporte la course, C’est d’un pas rapide et d’un courage inouï que sa victoire tire sa source.




🇸🇳 ́négal enegalese senegalcelebrities enegalparrot

À Diourbel,le Foulk incarne l'essence même du mois de Ramadan, sous la direction spirituelle éclairée de Serigne Aladji ...
03/04/2024

À Diourbel,le Foulk incarne l'essence même du mois de Ramadan, sous la direction spirituelle éclairée de Serigne Aladji Mbacké, frère vénéré de Serigne Mountakha, Khalif Général des Mourides, les fidèles se rassemblent chaque soir pour célébrer cette période sainte avec ferveur et dévotion.
Guidés par les récitations des panégyriques du cheikh par Mountakha Gueye , ils se plongent dans les invocations ferventes, cherchant ainsi à se rapprocher davantage de Dieu.
Dans cette oasis de spiritualité de Keur Goumack la lumière de la foi brille plus intensément, illuminant les chemins des fidèles sur la voie de la piété et de la gratitude.


🇸🇳 ́négal

Sëriñ bi nee na na ngeen am kilifa te nangu mu yilif léen, Yàlla xamal na ma ci loo xam ni su ma ko manoon jëmm ji la ñu...
02/04/2024

Sëriñ bi nee na na ngeen am kilifa te nangu mu yilif léen, Yàlla xamal na ma ci loo xam ni su ma ko manoon jëmm ji la ñuy xaaj ñaar jenn ji yilif ji ci des.

Dans l'enceinte sacrée du Foulk à Diourbel, la présence des petits-fils de Serigne Touba notamment Serigne Fallou Mbacké...
02/04/2024

Dans l'enceinte sacrée du Foulk à Diourbel, la présence des petits-fils de Serigne Touba notamment Serigne Fallou Mbacké Bachir et Serigne Issakha son frère illuminent chaque instant cette célébration spirituelle.
En tant que descendants directs de la lignée vénérée de Serigne Touba, ils portent avec grâce le flambeau de la tradition et de la piété. Serigne Aladji Mbacké, en particulier, incarne la noblesse et la bienveillance héritées de ses illustres prédécesseurs.

Adresse

Dakar, Guediawaye
Guédiawaye
15000

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Bichridigitalagency publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à Bichridigitalagency:

Vidéos

Partager

Entreprises De Médias á proximité


Autres entreprises de médias à Guédiawaye

Voir Toutes